«bu kenn ci yéen laal sakaraam ci ndayjooram fekk ma ngay saw, te bu demee duus ba noppi bu mu fompoo ndayjooram, te bu mu noyyi ci ndab li».
Jële nañu ci Abuu Xataadata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
«bu kenn ci yéen laal sakaraam ci ndayjooram fekk ma ngay saw, te bu demee duus ba noppi bu mu fompoo ndayjooram, te bu mu noyyi ci ndab li».
«لَا يُمْسِكَنَّ أَحَدُكُمْ ذَكَرَهُ بِيَمِينِهِ وَهُوَ يَبُولُ، وَلَا يَتَمَسَّحْ مِنَ الْخَلَاءِ بِيَمِينِهِ، وَلَا يَتَنَفَّسْ فِي الْإِنَاءِ».
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- leeral na yenni teggin yi; ba tax mu tere góor di laa sakaraam ci ndayjooram fekk ma ngay saw, ak ñu dindi sobe ci ginnaaw walla ci kanam ci loxo ndayjoor; ndaxte ndayjoor dañu koo waajal ngir yu tedd yi, Kem ni mu teree nit ki di noyyi ci ndab li muy naane.
Leeral jiitug Lislaam ci teggin yi ak ci cet.
Moytu mbir yu salte yi, bu ñu loroo ci laal ko na nekk loxo càmmooñ.
Leeral teddngay loxo ndayjoor ak ngëneelam ci kaw loxo càmmooñ.
Matug Sariihab Lislaam, ak yaatug njàngaleem.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (1/ 42) (154).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 225) (267).
Yataal gi (4)
تيسير العلام شرح عمدة الأحكام.
للبسام (ص41).
تنبيه الأفهام شرح عمدة الأحكام.
لابن عثيمين (1/ 45).