السؤال
س١٥: من هم أعداء الإنسان؟
Laaju 13: ñan ñooy noonu nit ki?
الجواب
ج:١. النفس الأمارة بالسوء: وذلك أن يتبع الإنسان ما تمليه عليه نفسه وهواه في معصية الله تَبَارَكَ وَتَعَالَى،
قال سُبْحَانَهُ:
﴿إِنَّ ٱلنَّفۡسَ لَأَمَّارَةُۢ بِٱلسُّوۤءِ إِلَّا مَا رَحِمَ رَبِّيۚ إِنَّ رَبِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ﴾
[يوسف: ٥٣].
- الشيطان: وهو عدو ابن آدم وغايته أن يضل الإنسان ويوسوس له في الشر ويدخله النار.
قال تَعَالَى:
﴿وَلَا تَتَّبِعُواْ خُطُوَٰتِ ٱلشَّيۡطَٰنِۚ إِنَّهُۥ لَكُمۡ عَدُوّٞ مُّبِينٌ﴾
[البقرة: ١٦٨].
- أصحاب السوء: الذين يحثّون على الشر، ويصدّون عن الخير.
﴿ٱلۡأَخِلَّآءُ يَوۡمَئِذِۭ بَعۡضُهُمۡ لِبَعۡضٍ عَدُوٌّ إِلَّا ٱلۡمُتَّقِينَ﴾
[الزخرف: 67].
- Bakkaan biy digle lu ñaaw: te mooy nit ki di topp li ko bakkanam ak bànneexaam di digal si moy Yàlla mu kawe mi, Yàlla mu sell mi neeena:
{Bakkan de Aji-Digle lu ñaaw la ndare ba Yàlla yërem, sama boroom de yërëmaakon la jéggalaakon la}
[Saaru Yuusufa: 53].
- Saytaane: te moom noonu doomu Adama la te yitteem yépp mooy sànk nit ki, ak diko jax-jaxee ngir jëmale ko ciw ay, ak dugal ko Sawara. Yàlla mu kawe mi néena:
{Bu léen topp jéegoy Saytaane yi, moom de seen noon bu mag la}
saaru Baqara: 24
- Àndandoo yu bon: ñiy xiirtalaate si yu bon yi, di gàllaŋkoore si yu baax yi. Yàlla neena:
{Xarit yi de bu bis baa ñenn ñi noonu ñeneen ña la ñiy doon, ndare ñi ragal Yàlla}
Saaru suxrufi: 13,14.