Skip to content

السؤال

س۱۳: ما الواجب إذا رأيت امرأة أجنبية؟

Laaju 12: Lan moo la war boo gisee jigeenu jàmbur?

الجواب

ج:الواجب غض البصر،

قال تَعَالَى:

﴿قُلْ لِلْمُؤْمِنِينَ يَغُضُّوا مِنْ أَبْصَارِهِمْ﴾

[النور: ٣٠].

  • Li war mooy dammu sab gis, Yàlla mu kawe mi neena:

{Waxal way-Gëm yu góor yi ñu dammu seenug gis}

[Saaru Annuur: 30].