Skip to content

السؤال

س6: اذكر بعض نعم الله عليك.

Laaju 5: Tuddal yenni xéewal i Yàlla yim la xéewalal?

الجواب

ج:١. نعمة الإسلام، وأنك لست من أهل الكفر.

  1. نعمة السنة، وأنك لست من أهل البدع.
  2. نعمة الصحة والعافية، كالسمع والبصر والمشي وغيرها.
  3. نعمة الطعام والشراب والملبس.
  • ونعمه تَعَالَى علينا كثيرة لا تعد ولا تحصى.

قال تَعَالَى:

﴿وَإِن تَعُدُّواْ نِعۡمَةَ ٱللَّهِ لَا تُحۡصُوهَآۗ إِنَّ ٱللَّهَ لَغَفُورٞ رَّحِيمٞ﴾

[النحل: ١٨].

  1. Xéewalu Lislaam, ba bokkoo si way-weddi ñi.
  2. Xéewalu Sunna, ba bokkoo si waa Bidaa.
  3. Xéewalu wér ak jàmm, di dégg, ak di gis, ak di dox, ak yeneen.
  4. Xéewalu lekk ak naan ak col.

Xéewal i Yàlla yi si nun bari na lool, kenn manukoo lim wala mu koy takk.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Bu ngeendoon lim xéewali Yàlla yi du ngeen ko mana takk, Yàlla Aji-Jéggale la Aji-Yërëme la 18}

[Saaru Annahli 18]