Skip to content

السؤال

س4: ما حكم البيع والمعاملات؟

Laaju 3: Lan mooy àtteb jaay ak jëflànte?

الجواب

ج:الأصل في كل البيوع والمعاملات أنها حلال إلا بعض الأنواع مما حرم الله تَعَالَى.

قال تَعَالَى:

﴿وَأَحَلَّ ٱللَّهُ ٱلۡبَيۡعَ وَحَرَّمَ ٱلرِّبَوٰاْۚ﴾

[البقرة: ٢٧٥].

Cosaanu njaay yi ak jëflànte yépp mooy ne dafa dagan, lu dul yenn yi Yàlla araamal.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Yàlla daganal na jaay araamal ribaa}

saaru Baqara: 24