Skip to content

السؤال

س١٨: ماذا تقول بعد الأذان؟

Laaju 18: Lan ngay wax ginnaaw nodd gi?

الجواب

ج:«تصلي على النبي صلى الله عليه وسلم»

رواه مسلم.

  • وتقول:

«اللهم رب هذه الدعوة التامة، والصلاة القـائـمـة، آت محـمـدًا الـوسـيلة والفـضـيلـة، وابـعثه مقامًا محمودًا الذي وعدته»

البخاري.

  • وتدعو بين الأذان والإقامة، فإن الدعاء لا يرد.
  • (Dangay julli ci Yónente bi -yalna ko Yàlla dolli jàmm ak mucc-)

Muslim moo ko soloo

Te nga wax: «Allaahumma Rabba haazihid dahwatit tàmmati, wassalaatil xaa imati, aati Muhammadan Alwasiilata walfadiilata, wabhashu maxaaman mahmuudan allazii wahadtahu»

Albuxaarii.

Nga ñaan ci diggante nodd gi ak lixaam gi, ndax ñaan fa kenn du ko delloo.