Skip to content

السؤال

س28: ما السنن الرواتب؟ وما فضلها؟

Yan mooy julli sunna yii nuy wax ay Rawaatib? ak luy seeni ngëneel?

الجواب

ج:ركعتان قبل الفجر.

  • أربع ركعات قبل الظهر.
  • ركعتان بعد الظهر.
  • ركعتان بعد المغرب.
  • ركعتان بعد العشاء.

فضلها: قال النبي صلي الله عليه وسلم:

«من صلى في اليوم والليلة اثنتي عشرة ركعة تطوعًا بنى الله له بيتًا في الجنة»

رواه مسلم وأحمد وغيرهما.

  • Yaar i ràkka lu jiitu jullig suba.

Ñeent i ràkka lu jiitu jillig tisbaar.

Yaar i ràkka ginnaaw jullig tisbaar.

Yaar i ràkka ginnaaw jullig timis.

Yaar i ràkka ginnaaw jullig gee.

Ngëneelam: yonente bi neena:

"ku julli ci bis bi ak ci guddi gi fukk i ràkka ak yaar ci coobare wu, Yàlla tabaxal ko kër ca aljana"

Muslim ak Ahmat soloo nanu ko; ak ñeneen.