Skip to content

السؤال

س30: ما حكم صلاة الجمعة؟

Lan mooy àtteb jullig aljuma?

الجواب

ج:فرض عين على كل مسلم، ذكر، بالغ، عاقل، مقيم.

قال تَعَالَى:

﴿ يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُوٓاْ إِذَا نُودِيَ لِلصَّلَوٰةِ مِن يَوۡمِ ٱلۡجُمُعَةِ فَٱسۡعَوۡاْ إِلَىٰ ذِكۡرِ ٱللَّهِ وَذَرُواْ ٱلۡبَيۡعَۚ ذَٰلِكُمۡ خَيۡرٞ لَّكُمۡ إِن كُنتُمۡ تَعۡلَمُونَ﴾

[الجمعة: ٩].

Faratay jëm la ci bepp jullit bu góor, tadib mukallaf, ta am xel, nekk ku tukkuwul.

Yàlla mu kawe mi neena:

{Ée yéen way-gëm yi buñ wootee julli ci bisub aljuma na ngeen jëm ca tudd Yàlla ga te bàyyi njaay mi, loolu moo gën ci yéen, ndeem xam ngeen 9}

[Saaru Almunaafixuuna:9].