Skip to content

السؤال

س29: ما أفضل أيام الأسبوع؟

Ban bis mo gën ci ayug bis yi?

الجواب

ج:يوم الجمعة، قال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«إن من أفضل أيامكم يوم الجمعة فيه خلق آدم وفيه قبض وفيه النفخة وفيه الصعقة فأكثروا علي من الصلاة فيه فإن صلاتكم معروضة علي».

قالوا يا رسول الله وكيف تعرض صلاتنا عليك وقد أرمت؟ – يقولون بليت – فقال:

«إن الله عَزَّ وَجَلَّ حرم على الأرض أجساد الأنبياء»

رواه أبو داود وغيره.

Bis u aljuma, yonente bi yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc, neena:

"Bis bi gën ci seen bis yi mooy bis u aljuma, ci lañu bind Aadama, ci lañu ko faat, ci lañu wal ci moom ruu gi, te ci la yuuxug faatu gi di am, deeleen ciy baril lu ngéen di julli ci man, ndax seenug julli dan ma koy gaaral.

neena: ñu ne ko yaw yonente Yàlla bi na ka lañulay gaarale sunug julli ci yaw te fekk funux nga? -maanam ràpp nga- mu wax ne:

«Yàlla mu màgg mi dafa araamal ci suuf muy lekk yaram i yonent yi»

Abuu Daawuda soloo na ko ak ñeneen.