na ka ngay jàppoo ?
- الموضوعات
- الطهارةأحكام الوضوء
- التصنيف الشرعي
- الفقهالطهارةالوضوءصفة الوضوء
- الباب / الفصل
- قسم الفقه
السؤال
س4: كيف تتوضأ؟
na ka ngay jàppoo ?
الجواب
ج:بغسل الكفين ثلاثًا.
والمضمضة والاستنشاق والاستنثار ثلاثًا.
- والمضمضة: جعل الماء في الفم ومجه وطرحه.
- والاستنشاق: جذب الماء بالهواء إلى داخل الأنف بيمينه.
- والاستنثار: وهو إخراج الماء من الأنف بعد الاستنشاق بيساره.
- ثم غسل الوجه ثلاثًا.
- ثم غسل اليدين إلى المرفقين ثلاثًا.
- ثم مسح الرأس تقبل بيديك وتدبر، وتمسح الأذنين.
- ثم غسل الرجلين إلى الكعبين ثلاثًا.
هذا هو الأكمل، وقد ثبت ذلك عن النبي ﷺ في أحاديث في البخاري ومسلم، رواها عنه عثمان وعبد الله بن زيد وغيرهما،
وقد ثبت أيضًا عنه في البخاري وغيره:
«أنه توضأ مرة مرة، وأنه توضأ مرتين مرتين» بمعنى: أنه يغسل كل عضو من أعضاء الوضوء مرة، أو مرتين.
dangay raxas say ténq ñatti yoon, maanaam sa ñaari loxo basi tikku jara yi.
nga gallaxndiku, saraxndiku, fiiru ñatti yoon.
gallaxndiku mooy: nga guux ndox mi yëngal ko ci sa gémmeñ yàbbi ko.
saraxndiku mooy: nga def ndox ci sa loxo ndeyjoor xëcc ko ak sa bakkan ba mu dugg ci biir bakkan bi.
fiiru mooy: nga génne ndox mi nga dugaloon ci sa bakkan mel ni kuy ñandu ak sa loxo càmmooñ.
gannaw ba nga raxas sa xarkanam ñatti yoon.
Tek ci raxas say yoxo ba ci say coñc ñatti yoon.
Nga masaa sa bopp tàmbalee ci sab jë jëm ci sag ndong, masaa waale say nopp.
Nga raxas say tànk ba ci say dojor ñatti yoon.
lii mooy njàppu li gën a matale, sax na juge ci yonente bi ci ay adiis yu Buxaari ak Muslim solo sahaabam yu bari nettali ko ku ci mel ni Usmaan ak Abdul Laay ibnu zayd ak yenéen i sahaaba.
sax na itam ci yonente bi ne daana jàppu benn-benn, niki noonu jàppu na ñaar-ñaar maanaam: mu raxas cër i njàppu yi benn yoon walla ñaar i yoon; lii Buxaarii moo ko soloo.