Skip to content

lan moo nu war ci woroom xam-xam i jullit ñi?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

س٣٤: ما واجبنا تجاه علماء المسلمين؟

lan moo nu war ci woroom xam-xam i jullit ñi?

الجواب

ج:نحبهم، ونرجع إليهم في المسائل والنوازل الشرعية، ولا نذكرهم إلا بالجميل، ومن ذكرهم بغير ذلك من السوء؛ فهو على غير السبيل.

  • قال تَعَالَى:

﴿يَرۡفَعِ ٱللَّهُ ٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ مِنكُمۡ وَٱلَّذِينَ أُوتُواْ ٱلۡعِلۡمَ دَرَجَٰتٖۚ وَٱللَّهُ بِمَا تَعۡمَلُونَ خَبِيرٞ﴾

[المجادلة: ١١].

dan leen di bëgg, di dellu ci ñoom si masala yi ak xew-xewi sariiha yi, te dunu leen tudd ci lu dul lu rafet, te kepp ku leen tudd ci lu dul lu rafet Kooku jaarul ci yoon wu jub wa.

Yàlla mu kawe mi neena:

(Yàlla dina yëkatil ay daraja ñi gëm ci yéen ak ñi ñu jox xam-xam si yéen te Yàlla deñ na kumpa ci lépp lu ngeen di def.)

saaru Al-mujaadala 11