Skip to content

Lan mooy pas-pasu walaahu wal baraahu maanaam di mengóo ag nit féetéeg moom wala gay dogoo ak moom?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy pas-pasu walaahu wal baraahu maanaam di mengóo ag nit féetéeg moom wala gay dogoo ak moom.

س19: ما هي عقيدة الولاء والبراء؟

الجواب

li nu jublu ci walaahu mooy: mengóo wala féetewoo ak ñi gëm Yàlla boolesi dileen dimbali.

Yàlla mu kawe mi neena:

way gëm Yàlla yu góor yi ak yu jigéen yi lenn ca ñoom ñoo féetéeg ñacades.

suuratu attawba 6

li nu jublu ci Albaraahu mooy: bañ yéeféer yi ta def leen ay noon, maanaam dogoo ag ñoom.

am ngeen ci Ibraahiima ak ñam andaloon royuwaay wu rafet, ba ñu waxee seenu nit na leen nun de deñ nanu ba set wecc ci yéen ag lingeen di jaamu te du Yàlla, weddi nanu leen, te ag noonoo akug mbañeel dox na sunu diggante ba fàwwu, ba kerook ngeen di gëm Yàlla dong.

suuratu al mumtahinatu 4

ج:الولاء: هو محبة المؤمنين ونصرتهم.

قال تَعَالَى:

﴿وَالْمُؤْمِنُونَ وَالْمُؤْمِنَاتُ بَعْضُهُمْ أَوْلِيَاءُ بَعْضٍ﴾

[التوبة: 71].

البراء: هو بغض الكافرين ومعاداتهم.

﴿قَدۡ كَانَتۡ لَكُمۡ أُسۡوَةٌ حَسَنَةٞ فِيٓ إِبۡرَٰهِيمَ وَٱلَّذِينَ مَعَهُۥٓ إِذۡ قَالُواْ لِقَوۡمِهِمۡ إِنَّا بُرَءَٰٓؤُاْ مِنكُمۡ وَمِمَّا تَعۡبُدُونَ مِن دُونِ ٱللَّهِ كَفَرۡنَا بِكُمۡ وَبَدَا بَيۡنَنَا وَبَيۡنَكُمُ ٱلۡعَدَٰوَةُ وَٱلۡبَغۡضَآءُ أَبَدًا حَتَّىٰ تُؤۡمِنُواْ بِٱللَّهِ وَحۡدَهُۥٓ﴾

[الممتحنة: 4].