Skip to content

السؤال

س٢١: ماذا تقول قبل أكل الطعام؟

Laaju 21: Lan ngay wax ba la ngay lekk aw ñam?

الجواب

ج:«بسم الله».

فإذا نسيت في أوله فقل:

«بسم الله في أوله وآخره»

رواه أبو داود والترمذي.

«Bismil Laahi»

Booko fàttee sa tàmbali ga, nanga wax:

«Bismillaahi fii awwalihii wa aaxiri hii»

Abuu Daawuda soloo nako ak Tirmisiyu ak ñeneen.