Skip to content

السؤال

waxal lan mooy bokkaale ak i xeetam ?

س12: ما الشرك وأنواعه؟

الجواب

bokkaale mooy: defal keneen ku dul Yàlla lenn ci xeeti jaamu yi.

ay xeetam:

bokkaale gu mag; lu ci mel ni: ñaan keneen ku dul Yàlla, walla sujjóotal keneen ku dul Yàlla, walla rendi dara ngir keneen ku dul Yàlla.

bokkaale gu ndaw; ni ki di giñ ci keneen ku dul Yàlla,walla takk ay gàllaaj, walla yu ni mel ngir mu indil la njariñ walla mu fegal ( dàqal) la aw lor, ak lu mel ni ngistal ni ki kuy julli di ko taaral ngir Li ko nit ñi di xool.

ج:الشرك: هو أن يجعل الإنسان لله نِدًّا؛ في عبادته أو ربوبيته أو أسمائه وصفاته.

ومن الشرك صرف أي نوع من أنواع العبادة لغير الله تَعَالَى.

أنواعه:

  • شرك أكبر؛ مثل: دعاء غير الله تَعَالَى، أو السجود لغيره سُبْحَانَهُ، أو الذبح لغير الله عَزَّ وَجَلَّ.
  • شرك أصغر؛ وهو الذي لا يخرج من الملة مثل: الحلف بغير الله تَعَالَى، أو التمائم، وهو ما يُعلق من الأشياء لجلب نفعٍ أو دفع ضرٍّ، ويسير الرياء، كأن يحسِّن صلاته لما يرى من نظر الناس إليه.