Skip to content
رسول الإسلام محمد صلى الله عليه وسلم

رسول الإسلام محمد صلى الله عليه وسلم

Ci turu Yàlla miy Aji-Yërëm képp ku nekk ci kaw suuf jagleel ko jullit ñi ca allaaxira ci laay tàmbalee. Yonenteb Lislaam Muhamm-. Ab tënk bu gàtt bu jëm ci yonenteb Lislaam Muhammat -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dama ciy leeral turam, ak askanam, ak dëkkam, ak takkum soxnaam, ak bataaxalam, ak ci li mu doon woote, ak ay keemaanam, ak yoonam wi, ak taxawaayu ay noonam ci moom. [1] Xéernaa nag ci lënkale yaari tur yii di Yonent ak Muhammat ngir sàmmoonte ak piri mi te dees na seet lu loolu. 1- Turam ak askanam ak dëkk bi mu juddoo sosoo fa. Yonenteb Lislaam mooy Muhammat doomu…

Language: lang_wo
Prepared by:
Version: 1.2

These files are generated automatically from the book's text; their layout may differ from the printed edition.

0%
Font size