Skip to content

السؤال

س15: ما أول ما نزل عليه من القرآن؟

lan moo njëkk a wàcci ci Alxuraan?

الجواب

ج:قوله تَعَالَى:

﴿ٱقۡرَأۡ بِٱسۡمِ رَبِّكَ ٱلَّذِي خَلَقَ ١

خَلَقَ ٱلۡإِنسَٰنَ مِنۡ عَلَقٍ 2

ٱقۡرَأۡ وَرَبُّكَ ٱلۡأَكۡرَمُ ٣

ٱلَّذِي عَلَّمَ بِٱلۡقَلَمِ ٤

عَلَّمَ ٱلۡإِنسَٰنَ مَا لَمۡ يَعۡلَمۡ 5﴾

[العلق: 1-5].

wax i Yàlla ji:

{iqra bismi ràbbi kal lazii xalaxa} 1 Jàngal ci sa tur u boroom bi Nga xam ne mo bind.

xalaxal insaana min halaqin 2 Moo bind nit ci lumbu dereet

iqra wa rabbukal akramu 3 Jàngal, sa boroom mooy ki gëna tedd

allazii hallama bilxalami 4 Mooy kiy xamle ci xalima

hallamal insaana maa lam yahlam 5 Xamal Na nit lumu xamul woon

saaru al-halaqi 1-5