Skip to content

السؤال

س16: من أول من آمن برسالته؟

kan moo ñëkka gëm ag yónentem ?

الجواب

ج:- من الرجال: أبو بكر الصديق.

  • ومن النساء: خديجة بنت خويلد.
  • ومن الصبيان: علي بن أبي طالب.
  • ومن الموالي: زيد بن حارثة.
  • ومن الأرقاء: بلال الحبشي رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُم.

ci góor ñi: Abuu bakrin Assiddiix, ci jingéen ñi: Xadiijatu doomu Xuwaylidin, ci xale yi: Aliyun doomu Abii taalib, bu dee ci jaam yiñ goreel: Zaydu doomu Haarisatu, ci jaam yi gore wul: Bilaal ma dëkk Ecopi, yal na leen Yàlla dolli ngërëm, ak ñeneen.