Skip to content

السؤال

س31: كم عدد ركعات صلاة الجمعة؟

Lan mooy limu ràkkay jullig aljuma?

الجواب

ج:عدد ركعات صلاة الجمعة ركعتان يجهر فيهما الإمام بالقراءة، حيثُ تتقدّمهما خطبتان معروفتان.

Limug ràkkay jullig aljuma yaar i ràkka la, Imaam da ciy biral njàng ma, niki noonu yaari xutba moo koy jiitu moom julli ga.