Skip to content

السؤال

س32: هل يجوز التخلف عن صلاة الجمعة؟

Ndax wuute jullig aljuma dagan na? Maanaam baña julliji

الجواب

ج:لا يجوز التخلف عن صلاة الجمعة إلا من عذر شرعي، وجاء عن النبي ﷺ، قوله:

«من ترك ثلاث جمع تهاونًا بها؛ طبع الله على قلبه»

رواه أبو داود وغيره.

Wuute jullig aljuma daganul ci lu dul ngàntul sariiha, juge na ci yonente bi mu wax ne:

«Képp ku bàyyi ñatt i aljuma ngir woyofal ko; Yàlla di na tëj ab xolam»

Abuu Daawuda soloo na ko ak ñeneen.