Skip to content

السؤال

س1: عرف الطهارة.

Laaj 1: xamleel ag laab?

الجواب

ج:الطهارة: هي رفع الحدث، وزوال الخبث. أي: رفع ما يمنع من الصلاة.

قال النبي صلى الله عليه وسلم:

«مِفْتَاحُ الصَّلَاةِ الطُّهُورُ»

رواه أبو داود.

طهارة من الخبث: وهي أن يزيل المسلم ما وقع من النجاسة على بدنه، أو على ثوبه، أو على البقعة والمكان الذي يصلي فيه.

طهارة من الحدث: وهي التي تكون بالوضوء أو الغسل، بالماء الطهور، أو التيمم لمن فقد الماء، أو تعذر عليه استعماله.

Tontu li- laab mooy: yékkati am toj walla sobe su déñ.

laaba ci sobe mooy: julit bi dindi lépp luy sobe ci yaramam, wala ci ay yéereem, walla ci barab bi muy jullee.

laabug toj mooy: nit ki jàppu, wala mu sangu farata ci am ndox mu laab, wala mu tiim bu amul ndox, walla bu amee ngànt ci jëfëndikoo ndox ma.