Skip to content

lan mooy bàkkaar bi gën a rëy ?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy bàkkaar bi gën a rëy ?

س11: ما أعظم ذنب؟

الجواب

bakkaar bi gën a rëy mooy bokkaale Yàlla.

Yàlla mu kawe mi neena:

Yàlla du jéggal ku deewaale bokkaale waaye dina jeggale lu dul bokkaale ñeel ku ko soob te képp kuy bokkaale Yàlla def na bàkkaar bu rëy.

suuratu annisaa

ج:الشرك بالله تَعَالَى.

قال تَعَالَى:

﴿إِنَّ ٱللَّهَ لَا يَغۡفِرُ أَن يُشۡرَكَ بِهِۦ وَيَغۡفِرُ مَا دُونَ ذَٰلِكَ لِمَن يَشَآءُۚ وَمَن يُشۡرِكۡ بِٱللَّهِ فَقَدِ ٱفۡتَرَىٰٓ إِثۡمًا عَظِيمًا﴾

[النساء: 48]