Skip to content

السؤال

س4: كيف أصل الرحم؟

Laaju 4: Na ka laay jokke samay mbokk?

الجواب

ج:1. زيارة الأقارب من الأخ والأخت، والعم والعمة، والخال والخالة وبقية الأقارب.

  1. الإحسان إليهم بالقول والفعل ومساعدتهم.
  2. ومنها الاتصال بهم وسؤالهم عن أحوالهم.
  • قال تعالى:

﴿فَهَلۡ عَسَيۡتُمۡ إِن تَوَلَّيۡتُمۡ أَن تُفۡسِدُواْ فِي ٱلۡأَرۡضِ وَتُقَطِّعُوٓاْ أَرۡحَامَكُمۡ﴾

[محمد: ٢٢].

  • وفي الحديث:

«لا يدخل الجنة قاطع رحم»

رواه مسلم.

  1. di seeti jegeñaale yi ci mbokk mu góor ak mu jigéen ak baay tax ak bàjjan ak nijaay ak tànta ak jegéñaale yi des.
  2. di rafetal jëme ci ñoom ci wax ak jëf ak di leen dimbali.
  3. bokk na ca di leen jokk ak di leen laaj séen i mbir.