Skip to content

السؤال

س30: من أولاده صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ؟

ñan ñooy ay doomam?

الجواب

ج:من الذكور ثلاثة:

  • القاسم، وبه كان يكنى.
  • وعبد الله.
  • وإبراهيم.
  • من الإناث:
  • فاطمة.
  • رقية.
  • أم كلثوم.
  • زينب.

وكل ولده من خديجة رَضِيَ اللَّهُ عَنْهَا، إلا إبراهيم من مارية القبطية، وكلهم مات قبله إلا فاطمة بعده بستة أشهر.

goor ñi ñatt la ñu:

Al-xaasimu, te ci moom lañu ko doon Dàkkantale.

ak Abdulla

ak Ibraahimu

bu dee jigéen ñi:

Faatimatu.

Ruqiyatu.

Ummu kalsuum.

Zaynabu.

doomam yëpp Xadiijatu moo leen jur, bam des Ibraahima, te ñoom ñépp a ko njëkka faatu bam des Faatimatu, mi ngi faatu. ginnaawam ci juroom-benni weer.