Skip to content

السؤال

س31: اذكر بعض صفات النبي صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ الخَلقية؟

tuddal yenn ci melokaanu jëmmi Yónente bi:

الجواب

ج:كان صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ وسطًا من الرجال ليس بالقصير ولا بالطويل بل بين ذلك، وكان أبيض مشربًا بالحمرة عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ، وكان كثيف اللحية، واسع العينين، عظيم الفم، شعره شديد السواد، عظيم المنكبين، طيب الرائحة وغير ذلك من خلقته الجميلة صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ.

Nekkoon na ku digg dóomu ci góor ñi, gàttul guddul waaye ci diggante bi la yamoon, dafa weexoon waye raxale xonq -yal na mucc ak jàmm nekk ci moom-, ku sëqoon sikkim la woon, yaatu woon ay gët, yaatu woon gémmiñ, kawar ga ñuuloon kukk, mu yaatu woon ay wagg, neexoon xet, ak yu dul yooyu ci ay mbindiin yu rafet.