Skip to content

السؤال

س21: كيف كان النبي صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ يدعو الناس خارج مكة؟

na ka la yònente bi doon woowe nit ñi ci bitti màkka?

الجواب

ج:كان يدعو أهل الطائف، ويعرض نفسه في المواسم ومجامع الناس، حتى جاء أهل المدينة من الأنصار، فآمنوا بالنبي صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ، وبايعوه على نصرته.

daa na woo waa Taayif di leen gaaral boppam ci xew-xew yi ak ndajeey nit ñi, ba waa ansaar yi dëkk Maddina ñëwee daal di koy gëm jaayante ak moom ci diko dimbali .