Skip to content

السؤال

س18: ما كان حال النبي صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ ومن آمن به بعد الجهر بالدعوة؟

Naka la Yónente bi nekkewoon ak kan mooko gëm ginnaaw bimu biralee woote bi?

الجواب

ج:بالغ المشركون في أذيته وأذية المسلمين، حتى أذن للمؤمنين بالهجرة إلى النجاشي في الحبشة.

وأجمع أهل الشرك على أذية وقتل النبي صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ، فحماه الله وأحاطه بعمه أبو طالب ليحميه منهم.

bokkaalekat yi dañoo ëppal ci di ko lor ak di lor jullit ñi, ba mujj mu digël way gëm yi ñu gàddaay jëm ca An-najaasi ca ecopi.

bokkale kat yi dëppoo ci ray yónente bi Yàlla aar ko peege ko baay tëxam ba Abuu taalib ngir mu aar ko ci ñoom.