السؤال
س38: عرف الصيام؟
xamleel woor?
الجواب
ج:هو التعبد لله بالإمساك عن المفطرات من طلوع الفجر إلى غروب الشمس، مع النية، وهو نوعان:
- صيام واجب: مثل صيام شهر رمضان، وهو ركن من أركان الإسلام.
قال تَعَالَى:
﴿يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ كُتِبَ عَلَيۡكُمُ ٱلصِّيَامُ كَمَا كُتِبَ عَلَى ٱلَّذِينَ مِن قَبۡلِكُمۡ لَعَلَّكُمۡ تَتَّقُونَ﴾
[البقرة: 183].
2. وصيام غير واجب: مثل صوم الإثنين والخميس من كل أسبوع، وصيام ثلاثة أيام من كل شهر، وأفضلها أيام البيض (13، 14، 15) من كل شهر قمري.
mooy jaamu Yàlla ci bàyyi lépp luy dogloo li ko dale ci fenkug fajar gi ba ci sowug jant bi, ànd ag yéene, moom nag yaar i xaaj la:
woor gu war: lu ci mel ni weeru koor, moom ponk la ci ponki lislaam yi.
Yàlla mu kawe mi neena:
﴾Ée yéen way gëm ñi farataalees na ci yéen woor na ka ñu ko farataale woon ci ñi leen jiitu woon amaana ngeen ragal Yàlla 183﴿
saaru Baqara: 24
ak koor gudul farata: lu ci mel ni woor Altine ak alxamis ci ayu bis bu ne, ak woor ñatt bis ci weer wu ne, li ci gën nag mooy bis yu leer yi(13, 14,15) ci weer wu ne.