Skip to content

lan mooy sunu warteef ci njiitu jullit yi ?

الباب / الفصل
قسم العقيدة

السؤال

lan mooy sunu warteef ci njiitu jullit yi ?

س28: ما واجبنا تجاه ولاة أمر المسلمين؟

الجواب

sunu warteef ci ñoom mooy wormaal leen déggal leen topp leen ci lu dul ag moy Yàlla, te bañ a fétteerlu ci seen kaw; waaye di leen ñaanal, te di léen laayabiir ci lu nëbbu.

ج:واجبنا: احترامهم والسمع والطاعة لهم في غير معصية، والدعاء والنصح لهم سرًّا، وعدم الخروج عليهم، إلا أن نرى كفرًا بواحًا.

قال تعالى:

﴿يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُوٓاْ أَطِيعُواْ ٱللَّهَ وَأَطِيعُواْ ٱلرَّسُولَ وَأُوْلِي ٱلۡأَمۡرِ مِنكُمۡۖ فَإِن تَنَٰزَعۡتُمۡ فِي شَيۡءٖ فَرُدُّوهُ إِلَى ٱللَّهِ وَٱلرَّسُولِ إِن كُنتُمۡ تُؤۡمِنُونَ بِٱللَّهِ وَٱلۡيَوۡمِ ٱلۡأٓخِرِۚ ذَٰلِكَ خَيۡرٞ وَأَحۡسَنُ تَأۡوِيلًا﴾

[النساء: ٥٩].