Skip to content

السؤال

س27: ما آخر ما نزل من القرآن؟

lan moo mujjee wàcc ci Alxuraan?

الجواب

ج:قوله تَعَالَى:

﴿وَٱتَّقُواْ يَوۡمٗا تُرۡجَعُونَ فِيهِ إِلَى ٱللَّهِۖ ثُمَّ تُوَفَّىٰ كُلُّ نَفۡسٖ مَّا كَسَبَتۡ وَهُمۡ لَا يُظۡلَمُونَ﴾

[البقرة: 281].

wax i Yàlla ji:

{ragalleen bis banu leen i delloo ca seen Boroom kenn ku nekk ñu fay ko la mu jëfoon te ñoom kenn du leen tooñ} 281.

saaru Baqara: 24