Skip to content

السؤال

س١9: ما حكم ترك الصلاة؟

Lan mooy àtteb bàyyi julli ?

الجواب

ج:ترك الصلاة كفر،

قال النبي عَلَيْهِ الصَّلَاةُ وَالسَّلَامُ:

«العهد الذي بيننا وبينهم الصلاة، فمن تركها فقد كفر»

رواه أحمد والترمذي وغيرهما.

Kóllare gi dox sunu digante ak ñoom yéefar yi mooy julli, képp ku ko bàyyi weddi na.

Bàyyi julli ag kéefar la, yonente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm ak mucc- neena:

Ahmad ak Tirmisiyu soloo nañu ko ak ñeneen.