Skip to content

السؤال

س37: هل الإيمان يزيد وينقص؟

ndax ngëm Yàlla day yokku di wàññiku?

الجواب

ج:الإيمان يزيد بالطاعة وينقص بالمعصية.

  • قال تَعَالَى:

﴿إِنَّمَا ٱلۡمُؤۡمِنُونَ ٱلَّذِينَ إِذَا ذُكِرَ ٱللَّهُ وَجِلَتۡ قُلُوبُهُمۡ وَإِذَا تُلِيَتۡ عَلَيۡهِمۡ ءَايَٰتُهُۥ زَادَتۡهُمۡ إِيمَٰنٗا وَعَلَىٰ رَبِّهِمۡ يَتَوَكَّلُونَ﴾

[الأنفال: 2].

Ngëm Yàlla day yokkoo cig topp Yàlla di wàññi koo cig moy Yàlla.

Yàlla mu kawe mi neena:

﴾way gëm yi de ñooy ñi nga xam ne bu ñu tuddee Yàlla seen xol ya day jàq te buñu jàngee aayay Yàlla yi ci ñoom da leen di dolli ag ngëm, te ci Yàlla rek lañuy wakkirlu﴿

suuratu Al-anfaal: 2