Skip to content

السؤال

س38: ما الإحسان؟

lan mooy rafetal?

الجواب

ج:أن تعبد الله كأنك تراه، فإن لم تكن تراه؛ فإنه يراك.

Rafetal, mooy ngay jaamu Yàlla ba mel ni yaa ngi koy gis, boo ko gisul nga xam ni moom mi ngi lay gis.