Skip to content

Lan mooy xarañte gi nekk ci yoonal gi ñu yoonal masaa ay saŋ?

الباب / الفصل
قسم الفقه

السؤال

س١٢: ما الحكمة من المسح على الخفين؟

Lan mooy xarañte gi nekk ci yoonal gi ñu yoonal masaa ay saŋ.

الجواب

ج:التيسير والتخفيف على العباد، خاصة في أوقات البرد والشتاء والسفر، حيث يشق نزع ما في الرجلين.

قال تعالى:

﴿يُرِيدُ ٱللَّهُ بِكُمُ ٱلۡيُسۡرَ وَلَا يُرِيدُ بِكُمُ ٱلۡعُسۡرَ﴾

[البقرة ١٨٥].

Dees koo yoonal gir yombal ak woyofal ñeel jaam ñi rawati na jamonoy sedd, wala nit ki nekk ci ab tukki, mu jafe ci moom lool muy summi ay saŋam saa yuy jàppu.