Skip to content

السؤال

س٢٤: ما يقول الإنسان إذا عطس؟

Laaju 24: Lu nit kiy wax bu tissoolee?

الجواب

ج:«الحمد لله».

وليقل له أخوه أو صاحبه: «يرحمك الله».

فإذا قال له: فليقل: «يهديكم الله ويصلح بالكم»

رواه البخاري.

  • «Alhamdu lillaahi».
  1. na ko mbokkam mi wax wala àndandoom: «yarhamukal Laahu».

Bu ka ko waxee, na waxaat: «yahdiikumul Laahu wa yuslihu baalakum».

Buxaarii moo ko soloo.