«Kuy niru-nirulu aw nit ca ñoom la book».
Jële na ñu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
«Kuy niru-nirulu aw nit ca ñoom la book».
«مَن تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ».
Leerarug adiis bi: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- daf nuy xamal ne képp kuy roy yéefar yi, mbaa kàccoor yi, mbaa ñu baax ñi -ci def li leen di màndargaal ci wàllu pas-, walla ag jaamu, walla aada- kon bokk na ci ñoom; Ndax roy leen ci biti dafay yóbbe ci roy leen ci biir, te sikk-sakka amul ci ne roy aw askan day juddoo ci naw leen, te man naa tax nga bëgg leen, màggal leen, jeng jëm ci ñoom, te loolu man naa yóbbe nit ki roy leen sax ci biir ak ci jaamu Yàlla - Yal na nu ci Yàlla musal-.
...:
Bokk na ci njariñal adiis bi: Mooy day moytandiku Loo roy yéefar yi ak kàccoor yi.
Day soññee ci di niru-nirulu ñu baax ñi ak di leen roy.
Roy ci biti day waral mbëggeel ci biir.
Nit ki dees na ko tëkku mu am bàkkaar kem niru-nirulu ga ak i xeetam.
Terees na niru-nirulu lu yéefar yi ci séen diine ak séen aada ja ñu jagoo, bu dul loolu nag niki jàng liggéey yi ak yu ko niru loolu tereesu ko.
Téere Sunna yi bu Abóo Daawuda (6/ 144) (4031).
Téere Adiisu Ahmat bees leeral càllala ya (9/ 126) (5115).
Yataal gi (8)
توضيح الأحكام من بلوغ المرام.
للبسام (7/ 363).
منحة العلام في شرح بلوغ المرام.
لعبد الله الفوزان (10/ 157).
فتح ذي الجلال والاكرام بشرح بلوغ المرام.
لابن عثيمين (6/ 335).
مشكاة المصابيح.
للتبريزي (2/ 1246).
Cited in books
13 BooksYataal gi (13)
- الخطب المنبرية موسوعة الخطب المنبرية (القسم الثاني)«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»
- حكم المستهزئين بالأنبياء والمرسلين«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»[6]،
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الثالثة«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ» [78].
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الرابعة«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»[73].
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الرابعة«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»[123].
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الخامسة«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»
- ما لا يسع أطفال المسلمين جهله«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»[128].
- مباحث في أصول الدين1«من تشبه بقوم فهو منهم».
- مجموعة أسئلة تهم الأسرة المسلمة1«مَن تشبَّه بقَومٍ فهو منهم».
- مجموعة أسئلة تهم الأسرة المسلمة1«مَن تشبَّه بقومٍ فهو منهم».
- مشروع المنهج التعليميمادة التوحيد مستوى 4 «مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ».
- مشروع المنهج التعليميمادة التوحيد مستوى 4 «مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»،
- نبراس طالب (5)1«مَنْ تَشَبَّهَ بِقَوْمٍ فَهُوَ مِنْهُمْ»