«jullit mooy ki nga xam ne jullit ñi mucc nañu ci làmmiñam ak ci loxoom,gàddaaykat nag mooy ki gàddaay li Yàlla araamal ci moom».
Jële nañu ci Abdulaa Ibn Amr-yal na leen Yàlla dollee gërëm-mu jële ci Yonnente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-mu wax ne:
«jullit mooy ki nga xam ne jullit ñi mucc nañu ci làmmiñam ak ci loxoom,gàddaaykat nag mooy ki gàddaay li Yàlla araamal ci moom».
«المُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ المُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ، وَالمُهَاجِرُ مَنْ هَجَرَ مَا نَهَى اللَّهُ عَنْهُ».
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xibaare ne jullit bu lislaamam mat mooy ki jullit ñi mucc ci làmmiñam du leen saaga, du leen rëbb, du leen jëw, te du dox seen diggante ci genn xeetu lor ci làmmiñam, Dañuy mucc it ci loxoom du leen tooñ, du jël seen alal ci lu dul dëgg, ak lu niru loolu, Aji-gàdday nag mooy ki bàyyi li Yàlla araamal.
...:
Matug Lislaam du am ci lu dul bañ a lor ñeneen ñi moo xam xeetu lor gumu manadoon.
Jagleel nañu làmmiñ ak loxo cig tudd; ngir li seen i njuumte ak seen i lor bari, ndax ay yi gën a bari ci ñoom ñaar lay ame.
Ñaaxe ci bàyyi moy yi te taqoo ak li Yàlla mu kawe mi digle.
Ki gën ci jullit ñi mooy kiy jooxe àqi Yàlla ak àqi jullit ñi.
Tooñ man naa nekk wax walla jëf.
Gàddaay gu mat mooy gàddaay li Yàlla mu kawe mi araamal.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (1/ 11) (10).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 65) (40).
Yataal gi (6)
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (1/ 236).
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (2/ 511).
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (1/ 306).
Cited in books
16 BooksYataal gi (16)
- الله -جل جلاله- أنيس المحبين وملاذ القاصدين«المُسْلِمُ: مَنْ سَلِمَ المُسْلِمُوْنَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ، وَالمُهَاجِرُ مَنْ هَجَرَ مَا نَهَى اللهُ عَنْهُ»
- المناهج التعليمية - الصف الخامسالمناهج التعليمية - الصف الخامس - التوحيد«المُهَاجِرُ مَنْ هَجَرَ مَا نَهَى اللَّهُ عَنْهُ»[30].
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 1 «المهاجر من هجر ما نهىٰ الله عَنْهُ»
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 2«الْمُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ الْمُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ، وَالْمُهَاجِرُ مَنْ هَجَرَ مَا نَهَىٰ اللهُ عَنْهُ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 7«مَنْ سَلمَ المُسْلمُون من لسَانهِ وَيَدهِ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 7«المُسْلمُ مَنْ سلمَ المُسْلمُون منْ لسَانِهِ وَيَدِهِ، والمُهَاجرُ مَنْ هَجَرَ ما نَهَىٰ اللهُ عَنْهُ».
- فضل الإسلام{ المسلم من سلم المسلمون من لسانه ويده } [9].
- ما لا يسع أطفال المسلمين جهله«المُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ المُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ»[93].
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (3)، والسيرة النبوية (3)التربية الإٍسلامية -3- «المُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ المُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ».
- مشروع المنهج التعليميمادة الحديث مستوى 1«مَنْ سَلِمَ المسلمونَ مِنْ لِسانِهِ ويَدِهِ»
- مشروع المنهج التعليميمادة الحديث مستوى 1«مَنْ سَلِمَ المسلمونَ مِنْ لِسانِهِ ويَدِهِ».
- مشروع المنهج التعليميمادة الحديث مستوى 1«مَنْ سَلِمَ المسلمونَ مِنْ لِسانِهِ ويَدِهِ»
- مشروع المنهج التعليميمادة الدعوة«مَنْ سَلِمَ المسلمونَ مِنْ لِسانِهِ ويَدِهِ»
- نبراس طالب (1)1«الْمُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ الْمُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ»
- نبراس طالب (1)1«الْمُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ الْمُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ»
- نبراس طالب (3)نبراس طالب 3«الْمُسْلِمُ مَنْ سَلِمَ الْمُسْلِمُونَ مِنْ لِسَانِهِ وَيَدِهِ»