Skip to content

السؤال

س۲۲: ما معنى سبحان الله؟

Laaju 17: Lan mooy maanaam Subhaanal Laahi?

الجواب

ج:التسبيح وهو تنزيهه سُبْحَانَهُ وَتَعَالَى عن كل نقص وعيب وسوء.

  • Sàbbaal mooy sellal Yàlla mu kawe mi soreeleko bépp wàññeeku ak ayib ak ñaawteef.