bul bàyyi mukk di wax ginnaaw julli gu ne: Allaahuma ahinnii halaa sikrika wa sukrika wa husni hibaadatika".
Jële ci Muhaas ibn Jabal yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa téye ci loxoom, ne ko: "yaw Muhaas, waat naa ci Yàlla ne dama laa bëgg", mu ne ko: "maa ngi lay dénk yaw Muhaas bul bàyyi mukk di wax ginnaaw julli gu ne: Allaahuma ahinnii halaa sikrika wa sukrika wa husni hibaadatika".
أَنَّ رَسُولَ صَلَّى عَلَيْهِ وَسَلَّمَ أَخَذَ بِيَدِهِ، وَقَالَ: «يَا مُعَاذُ، وَاللَّهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ»، فَقَالَ: «أُوصِيكَ يَا مُعَاذُ لَا تَدَعَنَّ فِي دُبُرِ كُلِّ صَلَاةٍ تَقُولُ: اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ وَشُكْرِكَ وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ».
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa jàpp ci loxob Muhaas yal na ko Yàlla dollee gërëm, ne ko: giñ naa ci Yàlla ne dama laa bëgg, te maa ngi lay dénk yaw Muhaas bul bàyyi di wax ginnaaw julli gu nekk: (Allaahuma ahinnii halaa sikrika) ci jépp wax ak jëf juy jëme ci jaamu la, (wa sukrika) ci amug xéewal ak deñug naqar, (wa husni hibaadatika) ci ag sellal ñeel Yàlla ak topp Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc.
Yoonalees na xibaar nit ki ne danga ko a bëgg ci Yàlla.
Sopp nañu ñaan gii ginnaaw julli gu ne farata ak naafila.
Ñaan ci kàddu yu néew yii bépp càkkuteefu àdduna ak allaaxira a ngi ci.
Bokk na ci njariñi bëgg ci Yàlla dénkante dëgg ak laabirante ak dimbalante ci lu baax ak ragal Yàlla.
At-Tiibii nee na: tudd Yàlla mooy njëlbeenu ubbiteg dënn, sant ko mooy jumtukaayu xéewal gu nangu, rafetug jaamu gi ñu sàkku ci moom mooy deñ ci lu koy soxlaal wolif Yàlla mu kawe mi.
Téere Sunna yi bu Abóo Daawuda (2/ 630) (1522).
Téere Sunna yi bu An-nasaa'iy (3/ 53) (1303).
Téere Adiisu Ahmat bees leeral càllala ya (36/ 429) (22119).
Yataal gi (10)
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (1/ 450).
تطريز رياض الصالحين.
لفيصل آل مبارك (ص259).
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (3/ 264).
كنوز رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (6/ 284).
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (1/ 353).
Cited in books
9 BooksYataal gi (9)
- الذكر والدعاء والعلاج بالرقي من الكتاب والسنة"اللهم أعني على ذكرك وشكرك وحسن عبادتك".
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهمالصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«يَا مُعَاذُ، وَاللَّهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ، وَاللَّهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ»، فَقَالَ: «أُوصِيكَ يَا مُعَاذُ لَا تَدَعَنَّ فِي دُبُرِ كُلِّ صَلَاةٍ» تَقُولُ: «اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ، وَشُكْرِكَ، وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ»[71].
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«يَا مُعَاذُ، وَاللَّهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ، وَاللَّهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ»، فَقَالَ: «أُوصِيكَ يَا مُعَاذُ لَا تَدَعَنَّ فِي دُبُرِ كُلِّ صَلَاةٍ» تَقُولُ: «اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ، وَشُكْرِكَ، وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ»[71].
- الله -جل جلاله- أنيس المحبين وملاذ القاصدين«اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ وَشُكْرِكَ وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ!»
- رسالة في الأذكار1«يَا مُعَاذُ، وَاللهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ، وَاللهِ إِنِّي لَأُحِبُّكَ، أُوصِيكَ يَا مُعَاذُ، لَا تَدَعَنَّ فِي دُبُرِ كُلِّ صَلَاةٍ تَقُولُ: اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ وَشُكْرِكَ وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 2«يَا مُعَاذُ، واللهِ إنِّي لأُحِبُّكَ، ثُمَّ أُوصِيكَ يَا مُعَاذُ: لاَ تَدَعَنَّ في دُبُرِ كُلِّ صَلاةٍ تَقُولُ: اللَّهم أَعِنِّي عَلىٰ ذِكْرِكَ وَشُكْرِكَ، وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 7«يا معاذُ، واللهِ إنِّي لأحبُّكَ» فَقَالَ: «أوصيكَ يا معاذُ؛ لا تَدَعَنَّ في دُبُرِ كلِّ صَلاةٍ تقولُ: اللّهم أعنِّي عَلَىٰ ذكرِكَ وشكرِكَ، وحُسنِ عبادَتِكَ».
- محاضرات تعظيم قدر الصلاةمحاضرات في تعظيم قدر الصلاة"اللهم أعني على ذكرك وشكرك وحسن عبادتك "[135]
- مشروع منهاج زادكزادك 1 طالب«اللَّهُمَّ أَعِنِّي عَلَى ذِكْرِكَ وَشُكْرِكَ وَحُسْنِ عِبَادَتِكَ».