«def ndànk du am ci dara lu dul ne dana ko taaral, waaye du ñàkk ci dara it lu dul ne dana ko ñaawal».
Jële na ñu ci Aysatu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- Soxnas Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
«def ndànk du am ci dara lu dul ne dana ko taaral, waaye du ñàkk ci dara it lu dul ne dana ko ñaawal».
«إِنَّ الرِّفْقَ لَا يَكُونُ فِي شَيْءٍ إِلَّا زَانَهُ، وَلَا يُنْزَعُ مِنْ شَيْءٍ إِلَّا شَانَهُ».
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ne def ndànk ak ug nooy ak teey ci wax ak jëf day yokk bir yi ab taar ak ug mat ak rafet, kon yell na boroomam am li mu bëgg. Ñàkk a teey day sikkal bir yi di ko ñaawal tey tere boroomam am la mu bëgg, bu ko amee it ci coono la koy ame.
...:
Ñaaxe ci jikkowoo ay teey.
Ag teey day taaral nit ki, te sabab la ci wépp yiw ci biri diine ak yu àdduna.
Téere Muslim bi gën a wér (4/ 2004) (2594).
Yataal gi (4)
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (1/ 683).
تطريز رياض الصالحين.
لفيصل آل مبارك (ص414).
Cited in books
6 BooksYataal gi (6)
- الحقيقة المُبْهِرَة في العلاقة بين الإسلام والإنسان(إنَّ الرفق لا يكون في شيءٍ إلا زانَه، ولا يُنزَع من شيءٍ إلا شانَه﴾ [146].
- الله -جل جلاله- أنيس المحبين وملاذ القاصدين«إِنَّ الرِّفْقَ لَا يَكُوْنُ فِي شَيْءٍ إِلَّا زَانَهُ، وَلَا يُنْزَعُ مِنْ شَيْءٍ إِلَّا شَانَهُ»
- المختصر المفيد للمؤذن والإمام والخطيب وأحكام المساجد«إِنَّ الرِّفْقَ لَا يَكُونُ فِي شَيْءٍ إِلَّا زَانَهُ، وَلَا يُنْزَعُ مِنْ شَيْءٍ إِلَّا شَانَهُ»
- المختصر المفيد للمؤذن والإمام والخطيب وأحكام المساجد«إِنَّ الرِّفْقَ لَا يَكُونُ فِي شَيْءٍ إِلَّا زَانَهُ، وَلَا يُنْزَعُ مِنْ شَيْءٍ إِلَّا شَانَهُ»
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 3«إنَّ الرِّفقَ لا يَكُونُ في شَيْءٍ إلَّا زَانَهُ، وَلاَ يُنْزَعُ مَنْ شَيْءٍ إلاَ شَانَهُ».
- نبراس طالب (2)نبراس طالب (2) «إِنَّ الرِّفْقَ لاَ يَكُونُ فِي شَيْءٍ إلاَّ زَانَهُ، وَلاَ يُنْزَعُ مِنْ شَيْءٍ إلاَّ شَانَهُ»