«Ku jàpp te rafetal njàpp ma, ay ñaawtéefam day génn ci aw yaramam bay génn ci ay weyam».
Jële na ñu ci Usmaan Ibn Affaan -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
«Ku jàpp te rafetal njàpp ma, ay ñaawtéefam day génn ci aw yaramam bay génn ci ay weyam».
«مَنْ تَوَضَّأَ فَأَحْسَنَ الْوُضُوءَ خَرَجَتْ خَطَايَاهُ مِنْ جَسَدِهِ حَتَّى تَخْرُجَ مِنْ تَحْتِ أَظْفَارِهِ».
yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ne ku jàpp sàmmoonte ak Sunnay Njàpp ak i tegginam, loolu sabab la ci far ay ñaawtéef ak sippi ay ñuumte, "ba ay bàkkaaram di génne ci ay suufi weyi loxoom ak i tànkam"
...:
Ñaaxe ci yittewoo jàng njàpp ak i sunnaam ak i tegginam, ak jëfe ko.
Ngëneelu jàpp, ci ne day far bàkkaar yu ndaw yi, bu dee yu mag yi nag tuub rekk a koy far.
Sàrt yiy tax bàkkaar yi génn mooy matal njàpp mi te moytu lu koy yàq kem ni ko yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- leerale.
Dindi bàkkaar yi ci hadiis bii dañu koo tënk ci moytu bàkkaar yu mag yi ak tuub ko, Yàlla mu kawe mi nee na: (bu ngeen moytoo bàkkaar yi ñu leen tere nu far séen i ñaawtéef) [An-Nisaa].
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 216) (245).
Yataal gi (6)
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (5/ 9).
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمصطفى الخِن وغيره (2/ 763).
بهجة الناظرين.
سليم الهلالي (2/ 247).
Cited in books
8 BooksYataal gi (8)
- المختصر المفيد للمسلم(من توضأ فأحسن الوضوء خرجت خطاياه من جسده حتَّى تَخْرُجَ مِنْ تحتِ أَظفارِهِ)
- المختصر المفيد للمسلم الجديد(من توضأ فأحسن الوضوء خرجت خطاياه من جسده).
- المنتقى من المتجر الرابح في ثواب العمل الصالح - المعتمدالمنتقى من المتجر الرابح في ثواب العمل الصالح“من توضأ فأحسن الوضوء خرجت خطاياه من جسده حتى تخرج من تحت أظفاره”.
- خطب تعظيم قدر الصلاة"مَنْ تَوَضَّأَ فَأَحْسَنَ الْوُضُوءَ خَرَجَتْ خَطَايَاهُ مِنْ جَسَدِهِ، حَتَّى تَخْرُجَ مِنْ تَحْتِ أَظْفَارِهِ" رواه مسلم [26]،
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 5«مَنْ تَوَضَّأَ فَأَحْسَنَ الوُضُوءَ، خَرَجَتْ خَطَايَاهُ مِنْ جَسَدِهِ حَتَّىٰ تَخْرُجَ مِنْ تَحْتِ أَظفارِه».
- مجموعة زاد الحديث(3)1«من توضَّأ فأحْسَنَ الوُضُوءَ خَرَجَت خطاياه من جَسَدِهِ حتى تخرجَ من تحتِ أظفارِهِ»
- مشروع منهاج زادكزادك 1 طالب«مَنْ تَوَضَّأَ فَأَحْسَنَ الْوُضُوءَ خَرَجَتْ خَطَايَاهُ مِنْ جَسَدِهِ، حَتَّى تَخْرُجَ مِنْ تَحْتِ أَظْفَارِهِ»
- من الأحكام الفقهية في الطهارة والصلاة والجنائز«مَنْ تَوَضَّأَ فَأَحْسَنَ الْوُضُوءَ خَرَجَتْ خَطَايَاهُ مِنْ جَسَدِهِ، حَتَّى تَخْرُجَ مِنْ تَحْتِ أَظْفَارِهِ»