"toftalleen diggante Aj ak Umra, ndax ñoom ñaar dañuy dàq ñàq ak bàkkaar yi, kem ni sawara di dàqe mbonteg weñ, ak wurus, ak xaalis, te Aj gu ñu nangu amul genn yool gu dul Àjjana".
Jële nañu ci Abdullah Ibn Mashuud yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na :
"toftalleen diggante Aj ak Umra, ndax ñoom ñaar dañuy dàq ñàq ak bàkkaar yi, kem ni sawara di dàqe mbonteg weñ, ak wurus, ak xaalis, te Aj gu ñu nangu amul genn yool gu dul Àjjana".
«تَابِعُوا بَيْنَ الحَجِّ وَالعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الكِيرُ خَبَثَ الحَدِيدِ، وَالذَّهَبِ، وَالفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجَّةِ الْمَبْرُورَةِ ثَوَابٌ إِلاَّ الجَنَّةُ».
Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa ñaaxe ci jegeele diggante def jaamug Aj ak jaamug Umra te bañ leen a teqale te man ko, ndax defandoo leen sabab la ci dindi ak ñàkk ak bàkkaar yi ak jeexitalam ci xol, kem ni uppug sawara nekke sabab ci dindi tilim-tilimi weñ ak liy jaxasoo ak mbell mi te bokku ci.
Ngëneelu toftale Aj ak Umra ak ñaaxe ci loolu.
Toftale Aj ak Umra dafa bokk ci liy indi ag koom ak njéggalug bàkkaar yi.
Mubaarakfoorii nee na: (dañuy dàq ag ñàkk) maanaam dañu koy dindi, jamtal na it ñàkk giy feeñ ci mu am doylug loxo, ak ñàkk gi nëbbu ci mu am doylug xol.
Téere Sunna yi bu At-tirmisiy (2/ 167) (810).
Téere Sunna yi bu An-nasaa'iy (5/ 115) (2631).
Téere Adiisu Ahmat bees leeral càllala ya (6/ 185) (3669).
Yataal gi (2)
ذخيرة العقبى في شرح المجتبى (23/ 322).
النهاية في غريب الحديث والأثر (819) (252).
Cited in books
8 BooksYataal gi (7)
- آداب السفر وأحكامهآداب السفر وأحكامه (للحرمين)«تَابِعُوا بَيْنَ الحَجِّ وَالعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الكِيرُ خَبَثَ الحَدِيدِ، وَالذَّهَبِ، وَالفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجَّةِ المَبْرُورَةِ ثَوَابٌ إِلَّا الجَنَّةُ» [48].
- آداب السفر وأحكامهآداب السفر وأحكامه (للحرمين)«تَابِعُوا بَيْنَ الحَجِّ وَالعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الكِيرُ خَبَثَ الحَدِيدِ، وَالذَّهَبِ، وَالفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجِّ المَبْرُورِ ثَوَابٌ إِلَّا الجَنَّةُ» [51].
- المختصر في آداب السفر وصفة الحج والعمرة وآداب الزيارة والأدعية الجامعة مع ملحق بالفتاوى والمخالفات1- آداب السفر وأحكامه (للحرمين)«تَابِعُوا بَيْنَ الحَجِّ وَالعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الكِيرُ خَبَثَ الحَدِيدِ، وَالذَّهَبِ، وَالفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجَّةِ المَبْرُورَةِ ثَوَابٌ إِلَّا الجَنَّةُ» [48].
- المختصر في آداب السفر وصفة الحج والعمرة وآداب الزيارة والأدعية الجامعة مع ملحق بالفتاوى والمخالفات1- آداب السفر وأحكامه (للحرمين)«تَابِعُوا بَيْنَ الحَجِّ وَالعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الكِيرُ خَبَثَ الحَدِيدِ، وَالذَّهَبِ، وَالفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجِّ المَبْرُورِ ثَوَابٌ إِلَّا الجَنَّةُ» [51].
- المختصر في صفة العمرة وأحكامهاالمختصر في صفة العمرة وأحكامها (للحرمين)«تَابِعُوا بَيْنَ الْحَجِّ وَالْعُمْرَةِ، فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الْفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الْكِيرُ[8] خَبَثَ الْحَدِيدِ وَالذَّهَبِ وَالْفِضَّةِ، وَلَيْسَ لِلْحَجِّ الْمَبْرُورِ ثَوَابٌ إِلا الْجَنَّةُ» [9].
- مجموعة زاد الفقه (3)الفقه 3«تابِعُوا بين الحجِّ والعُمْرةِ، فإنهما ينفِيَانِ الفَقْرَ والذُّنوبَ، كما ينفِي الكيرُ خَبَثَ الحدِيدِ»
- نبراس طالب (3)نبراس طالب 3«تَابِعُوا بَيْنَ الْحَجِّ وَالْعُمْرَةِ؛ فَإِنَّهُمَا يَنْفِيَانِ الْفَقْرَ وَالذُّنُوبَ كَمَا يَنْفِي الْكِيرُ خَبَثَ الْحَدِيدِ»