ku rafetal ci Lislaam deesu ko toppe la mu defoon ca ceddu ga, waaye ku def lu ñaaw ci Lislaam dees na ko toppe lu njëkk la ak lu mujj li».
Jële na ñu ci Ibn Mashuud -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, mu wax ne:
Benn waay dafa ne: yaw Yónente Yàlla bi, ndax dañ nuy toppe la nu defoon ca ceddu ga ? Mu ne ko: «ku rafetal ci Lislaam deesu ko toppe la mu defoon ca ceddu ga, waaye ku def lu ñaaw ci Lislaam dees na ko toppe lu njëkk la ak lu mujj li».
قَالَ رَجُلٌ: يَا رَسُولَ اللهِ، أَنُؤَاخَذُ بِمَا عَمِلْنَا فِي الْجَاهِلِيَّةِ؟ قَالَ: «مَنْ أَحْسَنَ فِي الْإِسْلَامِ لَمْ يُؤَاخَذْ بِمَا عَمِلَ فِي الْجَاهِلِيَّةِ، وَمَنْ أَسَاءَ فِي الْإِسْلَامِ أُخِذَ بِالْأَوَّلِ وَالْآخِرِ».
Leerarug hdiis bi: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ngëneelul dugg ci Lislaam, Ak ne képp ku tuub te rafetal Lislaamam tey sellal te dëggu; deesul luññutu la mu defoon ca ceddo ga ci ay moy, Waaye képp kuy ñaawal ci Lislaam ci nekk ab naaféq walla mu génn ci diine ji; dees na ko àtte ca la mu defoon ca kéefar ga ak li mu jëf ci Lislaam.
...:
Bokk na ci njariñal adiis bi: Yittewoog Sahaaba yi -yal na leen Yàlla dollee gërëm- jëf yi ñu doon def ca ceddo ga.
Ñaaxe ci sax ci Lislaam.
Ngëneelu dugg ci Lislaam ak ne day far jëf ya ko jiitu woon.
Ki génn ci diine ji ak naaféq bi dees na leen toppe la ñu defoon lu jiitu Lislaam, ak bépp bàkkaar buñu def ci Lislaam.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (9/ 14) (6921).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 111) (120).
Yataal gi (3)
مشارق الأنوار على صحاح الآثار (2/229).
الكواكب الدراري (24/43).
عمدة القاري شرح صحيح البخاري (24/ 76).
Cited in books
2 BooksYataal gi (2)
- الأسئلة المختارة من قاموس الأسئلة الشائعة حول الإسلامقسم الإسلام«مَن أحسن في الإسلام لم يؤاخذ بما عمل في الجاهلية، ومن أساء في الإسلام أُخِذَ بالأول والآخِر»
- موسوعة الأسئلة (المجموعة الأولى)«مَنْ أَحْسَنَ فِي الإِسْلَامِ لَمْ يُؤَاخَذْ بِمَا عَمِلَ فِي الْجَاهِلِيَّةِ، وَمَنْ أَسَاءَ فِي الإِسْلَامِ أُخِذَ بِالأَوَّلِ وَالآخِرِ»