"Noddkat yi ñooy gën a guddle doq ëllëg bis-pénc ".
Jële nañu ci Muhaawiya yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonente Yàlla bi yal ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne:
"Noddkat yi ñooy gën a guddle doq ëllëg bis-pénc ".
«الْمُؤَذِّنُونَ أَطْوَلُ النَّاسِ أَعْنَاقًا يَوْمَ الْقِيَامَةِ».
Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day xibaare ne ñiy nodd ñoom ñooy gën a guddle ay doq ci nit ëllëg bis-pénc ngir seen liggéey di mu teddee, ak barig seen i yiw, ak màggaayu seen i fay.
Ngëneelu nodd ak xemmemloo ko.
Leeral ngënnelu noddkat yi, ak kaweg seen wàccuwaay ëllëg bis-pénc.
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 290) (387).
Yataal gi (8)
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (2/ 251).
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (5/ 31).
شرح صحيح مسلم.
النووي (4/ 89).
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (1/ 768).
Cited in books
5 BooksYataal gi (5)
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهمالصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«الْمُؤَذِّنُونَ أطْوَلُ النَّاسِ أعْنَاقاً يَوْمَ الْقِيامَةِ»[98].
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«الْمُؤَذِّنُونَ أطْوَلُ النَّاسِ أعْنَاقًا يَوْمَ الْقِيامَةِ»[98].
- المختصر المفيد للمؤذن والإمام والخطيب وأحكام المساجد«المُؤَذِّنُونَ أَطْوَلُ النَّاسِ أَعْنَاقًا يَوْمَ القِيَامَةِ»
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 5«المؤذِّنُون أطوَلُ النَّاسِ أعناقاً يومَ القيامةِ».
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (1)، والسيرة النبوبة (1)، والعقيدة (1)، والفقه (1)مجموعة زاد الفقه (1)«المؤذنون أطول الناس أعناقا يوم القيامة».