Skip to content
732 Hadiths

Encyclopedia of Prophetic Hadiths

Filter results

68 of 732 cards

Clear filters
Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc da ko a yónni Yaman, mu laaj ay xeeti naan yu ñu fay defar, mu ne ko: yan la?, mu ne ko: "Al-Bithu, ak Al-Misru", ñu ne Abuu Burdata: lan mooy Al-Bithu? Mu ne: Siwu lem, Al-Misru: mooy Siwu Bele, mu wax ne: lépp luy màndiloo dafa araam" Al-Buxaarii génne na ko.
Wér na Al-Buxaarii ak muslim ñoo ko soloo
التصنيف الشرعيالأشربة المحرمة، الأربعون النووية
"ñent yii képp ku mu nekk ci moom nekk na naaféq, bu wenn melo nekkee ci moom kon wenn melow naaféq nekk na ci moom ba keroog mu koy bàyyi: bu waxtaanee fen, bu digee wuute ko, bu xulóo kàccoorr, bu kollarante daal di wor".
Wér na Al-Buxaarii ak muslim ñoo ko soloo
التصنيف الشرعيالأربعون النووية، ذم المعاصي، النفاق
«buleen ma jay kem ni Nasaraan yi jaye woon doomu Maryama; man daal ab jaamam laa, kon deeleen wax: jaamub Yàlla ak ndawam».
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.
التصنيف الشرعيالغلو في الأنبياء، توحيد الألوهية، النبوة والرسالة، الإيمان بنبينا محمد صلى الله عليه وسلمموضوعات الحديثأهمية التوحيد، معنى شهادة أن محمدًا رسول الله، الشرك بالله وأقسامه، حقوق النبي ﷺمحاور التعريف بالإسلامالغلو في الأنبياء
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan jàppu ci julli gu ne, ma ne ko: lan ngeen daan def yéen? Mu ne: njàpp mi dana doy nit ki feeg tojlewul.
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.
التصنيف الشرعيفضل الوضوء، سنن وآداب الوضوء، نواقض الوضوءموضوعات الحديثأحكام الوضوء
«kiy jokk mbokk du kiy faye liñuko jokk, waaye kiy jokk mbokk mooy ki nga xam ne bu ñu dogee ag mbokkam mu jokk ka ko dog.
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.
التصنيف الشرعيالمجتمع المسلم، فضائل صلة الأرحامموضوعات الحديثصلة الرحم
"ñaari xéewal a ngi nii yoo xamne nit ñu bari woru na ñu ci: ag wér ak ug jot".
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.
التصنيف الشرعيتزكية النفوس
"mo ndax dees na leen dimbali di leen wërsëgal lu dul ci seen néew ji doole yi".
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.
التصنيف الشرعيأحوال الصالحين
Laaj nañu Anas naka la njàngum Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc meloon? Mu ne: "njàngam mo da ko doon tàllal", topp mu jàng: {bismil Laahi Ar-Rahmaani Ar-Rahiimi} [Al-Faatiha: 1] di tàllal Bismil Laahi gu, di tàllal Ar-Rahmaani gi, di tàllal it Ar-Rahiimi gi.
Wér na Al-buxaariy soloo na ko.