seedeel naa Yàlla ne set naa wicc ci kenn ci yéen di nekk sama xarit, ndax Yàlla da maa jàpp xarit, niki mu jàppe Ibraahiima xarit
Jële nañu ci Jundub -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Dégg naa Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax li njëkk juroom i fan laata muy faatu naan: " seedeel naa Yàlla ne set naa wicc ci kenn ci yéen di nekk sama xarit, ndax Yàlla da maa jàpp xarit, niki mu jàppe Ibraahiima xarit, te bu ma doon wut ab xarit ci yéen kon dinaa def Abuu Bakar ab xarit. Yégleen ne ña leen jiitu woon dañu daan jàppe bàmmeeli seeni Yónent ak seen i nit ñu baax ay jàkka, rikk waay! Buleen jàppe bàmmeel yi jàkka, man tere naa leen ko".
سمعت النبي صلى الله عليه وسلم قبل أن يموت بخمسٍ وهو يقول: «إني أبرأ إلى الله أن يكون لي منكم خليلٌ، فإن الله تعالى قد اتخذني خليلًا، كما اتخذ إبراهيم خليلًا، ولو كنت متخذًا من أمتي خليلًا لاتخذت أبا بكر خليلًا، ألا وإن من كان قبلكم كانوا يتخذون قبور أنبيائهم وصالحيهم مساجد، ألا فلا تتخذوا القبور مساجد، إني أنهاكم عن ذلك».
Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- xibaare Na dayo bi mu am fa Yàlla, ci ne moom àgg na ca gën gaa kaweg daraja ci mbëggeel, kem ni ko Ibraahiima ame woon -yal na ko Yàlla dolli jàmm- , looloo tax mu ne amul benn xarit bu dul Yàlla; ndax xolam dafa fees ci bëgg Yàlla mu kawe mi ak màggal ko ak xam ko, kon keneen ku dul Yàlla xaju fa, Te bu doon am ab xarit ci mbindéef yi Abuu Bakar lay doon -yal na ko Yàlla dollee gërëm-. Mu moytandikuloo jéggi dayo ci néew yi kem ni ko Yahuud yi ak Nasaraan yi defe ci bàmmeeli séen Yónente yi ak ñu baax ñi, ba mujj ñu def ko ay yàllay, di ko jaamu bàyyi Yàlla, ñu tabax ca bàmmeel ya ay jàkka ak i jaamukaay. Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- tere na aw xeetam ci ñuy def lu mel ni séen jëf ya.
بخمس: خمس ليال.
إني أبرأ: أمتنع وأنكر.
من كان قبلكم: يعني: اليهود والنصارى.
Ngënéel u Abuu Bakar Siddiix -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, ag ne moom moo gën ci Sahaaba yi, te moo gën a yay ci nit ñi ngir nekk Xaliifab Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- ginnaaw bi mu faatoo.
Tabax jàkka ci bàmmeel daa book si ñaawtéefi xeet ya jiitu woon.
Tere ñuy jàppe bàmmeel yi ay barab ngir jaamu, di fa julli walla di ko jublu, walla di tabax ca kawam ay jàkka ak i xubba, ngir moytandikuloo tàbbi ci bokkaale ci sababus loolu.
Moytandikuloo ëppal ci gaayu baax yi ndax day jëme ci bokkaale.
Ñàngug li Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- di moytandikuloo ba tax mu feddali ko lu jiitu muy faatu ci juróomi guddi.
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 377) (532).
Yataal gi (5)
شرح النووي على مسلم (5/ 13).
الجديد في شرح كتاب التوحيد.
لمحمد القرعاوي (ص188).
الملخص في شرح كتاب التوحيد.
لصالح الفوزان (ص172).
Cited in books
16 BooksYataal gi (16)
- التوحيد في ضوء عقيدة الإمام الشافعي رحمه الله ونصوصه ومروياته"إني أبرأ إلى الله أن يكون لي منكم خليل؛ فإن الله قد اتخذني خليلا، كما اتخذ إبراهيم خليلا. ولو كنت متخذا من أمتي خليلا لاتخذت أبا بكر خليلا، ألا وإن من كان قبلكم كانوا يتخذون قبور أنبيائهم مساجد، ألا فلا تتخذوا القبور مساجد، فإني أنهاكم عن
- التوحيد في ضوء عقيدة الإمام الشافعي رحمه الله ونصوصه ومروياته"إني أبرأ إلى الله أن يكون لي منكم خليل؛ فإن الله قد اتخذني خليلا، كما اتخذ إبراهيم خليلا. ولو كنت متخذا من أمتي خليلا لاتخذت أبا بكر خليلا، ألا وإن من كان قبلكم كانوا يتخذون قبور أنبيائهم مساجد، ألا فلا تتخذوا القبور مساجد، فإني أنهاكم عن
- حراسة التوحيدالتحذير من بناء المساجد على القبور«إِنِّي أَبْرَأُ إِلَى اللَّهِ أَنْ يَكُونَ لِي مِنْكُمْ خَلِيلٌ، فَإِنَّ اللَّهَ قَدِ اتَّخَذَنِي خَلِيلًا، كَمَا اتَّخَذَ إِبْرَاهِيمَ خَلِيلًا، وَلَوْ كُنْتُ مُتَّخِذًا مِنْ أُمَّتِي خَلِيلًا، لَاتَّخَذْتُ أَبَا بَكْرٍ خَلِيلًا، أَلَا وَ
- حراسة التوحيددفن الموتى في المساجد«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ؛ فَإِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ».
- شرح الصدور بتحريم رفع القبور«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا القُبُورَ مَسَاجِدَ، فَإِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَٰلِكَ»[7].
- عقيدة الأئمة الأربعة«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، فَإِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ»
- عقيدة الأئمة الأربعة«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، فَإِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ»
- عقيدة التوحيد(ألا وإنَّ من كان قبلكم كانوا يتخذون قبور أنبيائهم مساجد، ألا فلا تتخذوا القبورَ مساجد؛ فإني أنهاكم عن ذلك)
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الثالثة«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، إِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ» [8].
- قاموس الكبائرموسوعة الكبائر - المجموعة الثالثة«أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، إِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ» [80].
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (3)، والسيرة النبوية (3)التربية الإٍسلامية -3- «سَمِعْتُ النَّبِيَّ ﷺ قَبْلَ أَنْ يَمُوتَ بِخَمْسٍ، وَهُوَ يَقُولُ: «أَلَا، وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، إِنِّي أَنْهَاكُ
- مجموعة زاد الحديث (1)الحديث 1«إِنِّي أَبْرَأُ إِلَى الله أَنْ يَكُونَ لِي مِنْكُمْ خَلِيلٌ، فَإِنَّ الله تَعَالَى قَدِ اتَّخَذَنِي خَلِيلًا، كَمَا اتَّخَذَ إِبْرَاهِيمَ خَلِيلًا، وَلَوْ كُنْتُ مُتَّخِذًا مِنْ أُمَّتِي خَلِيلًا لَاتَّخَذْتُ أَبَا بَكْرٍ خَلِيلًا، أَلَا
- مجموعة زاد الحديث (1)الحديث 1«يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ»
- مجموعة زاد العقيده (4)العقيدة 4«أَلا وَإِنَّ مَنْ كانَ قَبْلَكُمْ كانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيائِهِمْ وَصالِحِيهِمْ مَساجِدَ، أَلا فَلا تَتَّخِذُوا القُبُورَ مَساجِدَ، إِنِّي أَنْهاكُمْ عَنْ ذَلِكَ».
- موسوعة الإيمان«إِنِّي أَبْرَأُ إِلَى اللهِ أَنْ يَكُونَ لِي مِنْكُمْ خَلِيلٌ، فَإِنَّ الله تَعَالَى قَدِ اتَّخَذَنِي خَلِيلًا، كَمَا اتَّخَذَ إِبْرَاهِيمَ خَلِيلًا».
- موسوعة الإيمان«... أَلَا وَإِنَّ مَنْ كَانَ قَبْلَكُمْ كَانُوا يَتَّخِذُونَ قُبُورَ أَنْبِيَائِهِمْ وَصَالِحِيهِمْ مَسَاجِدَ، أَلَا فَلَا تَتَّخِذُوا الْقُبُورَ مَسَاجِدَ، إِنِّي أَنْهَاكُمْ عَنْ ذَلِكَ».