«jempleen Seen mustaas yi, te yar sikkim yi».
Jële na ñu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
«jempleen Seen mustaas yi, te yar sikkim yi».
«أحْفُوا الشَّوَارِبَ وأَعْفُوا اللِّحَى».
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa digle ñu dindi dara ci kawaru mustaas te bañ koo bàyyi noonu, waaye dañu koy jemp. Ca wet ga mu digle ñu yar sikkim bàyyi ko mu sëq.
...:
Araamal nañu wat ab sikkim.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (7/ 160) (5892).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 222) (259).
Yataal gi (13)
رياض الصالحين (ص338) (1205).
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (2/ 345).
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمصطفى الخِن (2/ 853).
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (5/ 228).
كنوز رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (14/ 507).
تطريز رياض الصالحين.
لفيصل آل مبارك (ص676).
منار القاري شرح مختصر صحيح البخاري.
لحمزة محمد قاسم (5/ 236).