«fi jaam bi di gën a jegee Boroomam mooy bu sujjóotee, deeleen ci baril ay ñaan».
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
«fi jaam bi di gën a jegee Boroomam mooy bu sujjóotee, deeleen ci baril ay ñaan».
«أَقْرَبُ مَا يَكُونُ الْعَبْدُ مِنْ رَبِّهِ وَهُوَ سَاجِدٌ، فَأَكْثِرُوا الدُّعَاءَ».
Leerarug adiis bi: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ne fi jaam bi di gën a jegee Boroomam mooy bu sujjóotee; ndaxte kiy julli day teg li gën a kawe te tedd ci yaramam ci kaw suuf ndax woyoflu la ak toroxlul Yàlla mu kawe mi fekk ma nga sujjóot. Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- digle na baril ñaan ca sujjóot ya, bu ko defee toroxlul Yàlla ci wax ak jëf daal di daje.
Bokk na ci njariñal adiis bi : Toppub Yàlla day dolli Jaam bi mu gën a jege Yàlla mu kawe mi.
Sopp nañu di baril ñaan ca sujjóot ya; ndax bérabi nangu ñaan la.
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 350) (482).
Yataal gi (6)
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (5/ 509).
تطريز رياض الصالحين.
لفيصل المبارك (ص780).
بهجة الناظرين شرح رياض الصالحين.
لسليم الهلالي (2/ 506).
Cited in books
8 BooksYataal gi (8)
- الذكر والدعاء والعلاج بالرقي من الكتاب والسنة"أقرب ما يكون العبد من ربه وهو ساجد؛ فأكثروا الدعاء" .
- الله -جل جلاله- أنيس المحبين وملاذ القاصدين«أَقْرَبُ مَا يَكُوْنُ العَبْدُ مِنْ رَبِّهِ وَهُوَ سَاجِدٌ؛ فَأَكْثِرُوا الدُّعَاءَ»
- الله -جل جلاله- أنيس المحبين وملاذ القاصدين«أَقْرَبُ مَا يَكُوْنُ العَبْدُ مِنْ رَبِّهِ وَهُوَ سَاجِدٌ؛ فَأَكْثِرُوا الدُّعَاء»
- حصن المسلم من أذكار الكتاب والسنةحصن المسلم«أَقْرَبُ مَا يَكُونُ العَبْدُ مِنْ رَبِّهِ وَهُوَ سَاجِدٌ فَأَكثِرُوا الدُّعَاءَ»[298].
- رسالة في الأذكار1«أَقْرَبُ مَا يَكُونُ الْعَبْدُ مِنْ رَبِّهِ وَهُوَ سَاجِدٌ، فَأَكْثِرُوا الدُّعَاءَ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 7«أقرَبُ مَا يَكُونُ العَبْدُ من ربِّه وهُوَ ساجدٌ، فأكثرُوا الدُّعاءَ».
- رياض الصالحينرياض الصالحين مع فوائد وهدايات - 7«أقرَبُ ما يكُونُ العَبْدُ من ربِّه وهُوَ ساجدٌ، فأكثرُوا الدُّعاءَ».
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (3)، والسيرة النبوية (3)التربية الإٍسلامية -3- «أقربُ ما يكونُ العبدُ من ربِّه وهو ساجدٌ، فأكثروا الدعاءَ»