«deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi».
Jële na ñu ci Aysa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
«deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi».
«لَا صَلَاةَ بِحَضْرَةِ الطَّعَامِ، وَلَا هُوَ يُدَافِعُهُ الْأَخْبَثَانِ».
Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na julli ci teewaayu ñam wi nga xam ne bakkanu kiy julli da koo xemmeem, xolam di ca nekk. Niki noonu tere na di julli di jañante ak ñaari sobe yi -te mooy saw ak dem duus- ndax kon day soxlawoo di jañ sobe sa .
...:
Jaadu na ci kiy julli mu sori lépp lu koy soxlaal ci julli gi balaa mu caa dugg.
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 393) (560).
Yataal gi (5)
شرح النووي على مسلم (5/ 46).
تيسير العلام شرح عمدة الأحكام.
للبسام (ص96).
تنبيه الأفهام شرح عمدة الأحكام.
لابن عثيمين (1/ 123).
Cited in books
2 BooksYataal gi (2)
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهمالصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«لَا صَلَاةَ بِحَضْرَةِ الطَّعَامِ، وَلَا هُوَ يُدَافِعُهُ الْأَخْبَثَانِ»[186].
- الصلاة التي علمها النبي ﷺ الصحابة رضي الله عنهم«لَا صَلَاةَ بِحَضْرَةِ الطَّعَامِ، وَلَا هُوَ يُدَافِعُهُ الْأَخْبَثَانِ»[186].