«ab ràmbaajkat du dugg àjjana».
Jële na ñu ci Husayfata Inb Yamaan -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax naan:
«ab ràmbaajkat du dugg àjjana».
«لَا يَدْخُلُ الْجَنَّةَ قَتَّاتٌ».
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm- day xamle ne ràmbaajkat biy tuxal ay wax ci diggante nit ñi jubloo yàq séen diggante kooku yayoo naa mbugal ci mu bañ a dugg àjjana.
...:
Bokk na ci njariñal adiis bi : Rambaaj ci Bàkkaar yu mag yi la bokk.
Tere nañu rambaaj; ndax li ci nekk ci yàq ak lor ci diggante nit ñi ak askan wi.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (8/ 17) (6056).
Téere Muslim bi gën a wér (1/ 101) (105).
Yataal gi (8)
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (6/ 145).
فتح ذي الجلال والإكرام شرح بلوغ المرام.
لابن عثيمين (6/ 401).
توضيح الأحكام من بلوغ المرام.
للبسام (7/ 452).
منحة العلام في شرح بلوغ المرام.
لعبد الله الفوزان (10/ 273).