"leelleen aji-xiif ji, seetileen ki feebar, yeewileen jaam bi".
Jële na ñu ci Abuu Muusa Al-Asharii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne:
"leelleen aji-xiif ji, seetileen ki feebar, yeewileen jaam bi".
«أَطْعِمُوا الجَائِعَ، وَعُودُوا المَرِيضَ، وَفُكُّوا العَانِيَ».
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day leeral ne bokk na ci àqi jullit bi ci jaw mbokku jullitam mu leel aji-xiif ji, ak mu seeti ki feebar, ak mu yewwi jaam bi.
Ñaaxe ci dimbalante ci diggante jullit ñi.
Ñaaxe ci leel aji-xiif ji aajowoo ñam, kii dañoo digle ñu leel ko.
Yoonalees na seeti aji-feebar jo, ak ñaanal ko, am ag pay, ak leneen lu dul loolu.
Xér ci horeel jaam bu ko yéefar jàppe, te loolu benn muy ci joxe luy tolloo ak goreem ci ñoom, walla luy tolloo ak moom vi yéefar bu ñu jàpp jaam, maanaam: ci anamug weccee.
Téere Al-buxaariy bi gën a wér (7/ 67) (5373).
Yataal gi (4)
شرح رياض الصالحين.
لابن عثيمين (4/ 468).
نزهة المتقين شرح رياض الصالحين.
لمجموعة من الباحثين (1/ 685).
Cited in books
2 BooksYataal gi (2)
- مباحث في أصول الدين1«أطعموا الجائع، وعودوا المريض، وفكّوا العاني».
- مجموعة زاد التربية الإسلامية (3)، والسيرة النبوية (3)التربية الإٍسلامية -3- «حَقُّ الْمُسْلِمِ عَلَى الْمُسْلِمِ خَمْسٌ، وذكر منها: عِيَادَةُ الْمَرِيضِ» رواه البخاري ومسلم، وعَنْ أَبِي مُوسَى الْأَشْعَرِيِّ رضي الله عنه، قَالَ: قَالَ رَسُولُ اﷲِ ﷺ: «أَطْعِمُوا الْجَائِعَ، وَعُودُوا الْمَرِيضَ، وَفُكُّوا الْعَانِيَ